Ouly – Dieundal Glace (Lyrics)
COUPLET I
Yalla déf na si man awma sa temps
Loma waxal dou saff day mélni vent
Sama feeling moy sa médicament Kaay fadiou
Fébaru sokhor mola sonal kaay fadiou
POND
Hé!! Loy dioy fans nga tathioul
Yaw supportaire nga tathioul
Yagui ci banc bi fans fans nga tathioul
Supportél tathioul
Fima gueneu tay bouy bone sa xol
Lossi man def ko ndakh
Kouy xalam dithia diayou
Yay sama fan tathioul
REFRAIN
Déh Déh Kone yagui déh
Dieundal glace féxal sa xol magui bax
Déh Déh Kone yagui déh
Dieundal glace féxal sa xol
COUPLET II
Thiono gui si yaw
Jaam djé gui si man
Lilay sonal si yaw
Moy lilay raay si man
Hé!! boñu beugoul
Poussal félé
Nama Yalla moussal
Ci sén péxé you bone
Kén xamoul li loumou done
Dou Maam li lafi bawone
No no sopékou dikal nañu
Solou diay la bandit
Gucci Golf Fendi
Kou diékou sa Waay réndi
Lii lou kofiy dindi
POND
Hé!! Loy dioy fans nga tathioul
Yaw supportaire nga tathioul
Yagui ci banc bi fans fans nga tathioul
Supportél tathioul
Fima gueneu tay bouy bone sa xol
Lossi man def ko ndakh
Kouy xalam dithia diayou
Yay sama fan tathioul
REFRAIN
Déh Déh Kone yagui déh
Dieundal glace féxal sa xol magui bax
Déh Déh Kone yagui déh
Dieundal glace féxal sa xol
OUTRO
Déh Déh Kone yagui déh
May ko ndox mu naan
Ki mongui déh
Déh Déh Kone yagui déh
Yagui deh ak sokhor fan Nopaloul
Waw waw waw waw waw waw
Dieundal glace féxal sa xol magui bax
Waw waw waw waw waw waw
Dieundal glace féxal sa xol